Fay bor: Ki la bëgg yab ndax alal , yaw ignorer ko lèpp Lu la nit , di Dokhanto , Yalla am na ko Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
Ki la bëgg jaay loo sa ngor , bayyi kook yëfëm Ba ko fa ne tek , bés a ngi ñëw , di na wéet ak jëf ëm Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
Te sax jamono fi mu toll nii , ku ne bopp am la tal Mawlaana rek , moo lay defal , ken du la xamal Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
Salaam alleykum , nga bañ ko fay , mbaa xam nga ni bor la Sa dëkkëndòo , nga koy tanxal, mbaa xam nga ni bor la Teg say briques , ken mën të jaar mbaa xam nga ni bor la Yor sa auto , lu la neex def mbaa xam nga ni bor la Nit ku la neex , nga wax ci moom mbaa xam nga ni bor la Yor say mbalit , fu la neex tuur mbaa xam nga ni bor la Koo séqqël , daldi ko wor mbaa xam nga ni bor la Yendoo wax , loo waax mu dañ mbaa xam nga ni bor la Koo ëpp doole , won ko ko mbaa xam nga ni bor la Doo dimmili , ki nga tane mbaa xam nga ni bor la
War ngay xalaat bu ëllëg ée , nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
man youssou maajigéen , j’ai tout pardonné Koo xam ni , meusone na la tooñ , jéggël ma ko
Bor yi nga am fii ñu ne , nan nga koy fay é War ngay xalaat bu ëllëg ée , nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
ki la bëgg jaay loo sa ngor , bayyi kook yëfëm Ba ko fa ne tek , bés a ngi ñëw , di na wéet ak jëf ëm Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
Te sax jamono fi mu toll nii , ku ne bopp am la tal Mawlaana rek , moo lay defal , ken du la xamal Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
Salaam alleykum , nga bañ ko fay , mbaa xam nga ni bor la Sa dëkkëndòo , nga koy tanxal, mbaa xam nga ni bor la Teg say briques , ken mën të jaar mbaa xam nga ni bor la Yor sa auto , lu la neex def mbaa xam nga ni bor la Nit ku la neex , nga wax ci moom mbaa xam nga ni bor la Yor say mbalit , fu la neex tuur mbaa xam nga ni bor la Koo séqqël , daldi ko wor mbaa xam nga ni bor la Yendoo wax , loo waax mu dañ mbaa xam nga ni bor la Koo ëpp doole , won ko ko mbaa xam nga ni bor la Doo dimmili , ki nga tane mbaa xam nga ni bor la War ngay xalaat bu ëllëg ée , nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo , yalla mën në laa fayal sa bor
man youssou maajigéen , j’ai tout pardonné Koo xam ni , meusone naa la tooñ , jéggël ma ko
Ñun doom i aadama ndiaye li ñu gën ë sonn al mooy, Aqqi dëkkëndòo , aqqi àndandoo , ak aqqi am gi jamm yek , Yalla , yermëndéem yaatu na , mën naa jéggël e bakkaar bu mu né Waaye , doom i aadama Ndiaye , Boo ko yor ee lee bor , na nga ko fay , fii ci dunyaa Walla nga balu ko mu baal la ,
Yé way samba, Khalass, kholal Youssou maajigéen , oh ! lii doy na waar Youssou Marie Sène , bu dee lii la , bor yi bari ña ñu Yaay na nga ma baal , baay na nga ma baal , aqq u njuréel You , Ndour , merci beaucoup . Adji maam Ndiaye , yaay I t