** Ecoutez ici https://bfan.link/yin-yang notre single YIN YANG sur toutes les plateformes musicales ** ** Abonnez- vous en cliquant ici https://goo.gl/oRiRJd ** Les Maabo, Mia - le Yin - & NFU - le Yang - , ne se laisseront pas abattre par leurs ennemis. Des ennemis qui veulent les « bombarder » comme Hiroshima ou Nagasaki. Mais l’amour triomphe toujours !!! #Maabo #YinYang #ClipOfficiel #Mia #NFU #Undacoprod #JolofBeats #team221
** Les crédits de la chanson et du clip YIN YANG ** Auteur & compositeur : NFU Energistrement, mix & mastering : UndacovaProd Habillement : Maabocouture Réalisateur : Weeflag Remerciements : Akassa Wass
Une production Undacovaprod (Senegal, décembre 2021)
** Retrouvez MAABO sur les réseaux sociaux ** Facebook https://web.facebook.com/Lesmaabo Instagram https://www.instagram.com/lesmaabo/ Twitter https://twitter.com/Lesmaabo
** Les lyrics de la chanson YIN YANG ** Chérie coco lo def nekhna Guani Boudé aye nakh sakh bakhna Haann Yaye sama thione maye diagua Wakhal Keninne koudoul yaw me begouma Heeee waye Beus Bignu gneuka guiser la mir Guani lane? Dagua dionger thi gor yaw mi Bayima waye Bouma waxane li né thi yaw mi Bayil mou sede Na bayi mou sede ndakh khadioul fi
Beute moy xool wayé xol moy guiss Fouma meuna xool yaw rek lay guiss Sa dieumak sa takander Goudi gui yaw laye djaner Sa refetaye dafa yemer Motakh ma diangui karate Koula togne fok laler hé None yiye wakhnane mane ak yaw dougne yague Sou desone si gnome dougnu ande Bi nieup bagné yama nangoul Gatié ngalama sokhnassi bakoul Yama diangual mgeguelou bandit Yama fouyal topatoma motakh maye dokh ni Gondi Yalla moko dogual kene meunousi touss
Sama xole dieule ko Louthi name boul xar def ko Begue nako doundou ak yaw aye fane bou goudou mak yaw Senegal yako mome Soma méré ma xare guethie gui Sebegal yaye borom Soguo beguer ma nangou pallet bi Dieunde almadi maye la Thiabi auto route bi diokhla Changer monument bi defthi mak yaw Nek president pour yaw
Cherie coco lo def nekhna Guani Boudé aye nakh sakh bakhna Haann Yaye sama thione maye diagua Wakhal Keninne koudoul yaw me begouma Heeee waye Beus Bignu gneuka guiser la mir Guani lane? Dagua dionger thi gor yaw mi Bayima waye Bouma waxane li né thi yaw mi Bayil mou sede Na bayi mou sede ndakh khadioul fi
Sama xole bi dafla mine Yaw rek sama diara bi Begouma koudoul yaw Nagne ma bayek yaw Sa yener eupena Wayer sa mbeguel doye nama Aldiana guama dji Seye ak yaw ba firdawsi Ayo lé lathie ma noumalaye wower Ayo lé sama chocola laleye wower Thiouw dou jipe Cherie coco yaye boss fi Couple bou heureux guaye ame fi Kougnu nekhoul boul gnew fi
Sama xole dieule ko Louthi name boul xar def ko Begue nako doundou ak yaw aye fane bou goudou mak yaw Senegal yako mome Soma méré ma xare guethie gui Sebegal yaye borom Soguo beguer ma nangou pallet bi Dieunde almadi maye la Thiabi auto route bi diokhla Changer monument bi defthi mak yaw Nek president pour y